곡 정보

Doom
Thione Seck
Orientissime
앱에서 듣기
REFRAIN: djiguèèn diou fo am Doom dèm saani thi mbaliit ba mou reyy mou déé ki mo bonne té sokhor
Bi Doom heuleuk bou dé fayo boul né woye sa ma ndeye x4
Lakhass Doom sani bou ley khol se yaram dawon
Gue woon guinaw mou dioysa yaram dawoon
Mou yendo khiff yendo marrse yaram dawoon
Bii domm heuleuk bou dé feyo boul né woye se ma, ndeye
REFRAIN:
Waw niou meneu kote amou niou mba wolof ndiaye mo ko wakh
Djiguèèn sey ne ba khey déé
REFRAIN:
Doom bou goor bakh na djiguèè bakh na
Yallah kham kou bonne kilifeu djiguèèn ya gui thi reew mi bou goor bi yague gue fii
REFRAIN:
Doom nou mou mété ak nou mou nekhé gue reyy mou déé sa morom mou djiguèèn di ne le siiweul déguel yaye boob
REFRAIN:
Lakhass Doom sani bou ley khol se yaram dawon
Gue woon guinaw mou dioysa yaram dawoon
Mou yendo khiff yendo marrse yaram dawoon
Bii domm heuleuk bou dé feyo boul né woye se ma, ndeye
REFRAIN et fin
멜론 님께서 등록해 주신 가사입니다.